« 27 ans la am divorcé am ben dom bou am 5 ans wayé depuis bi sama copain boubess embeulé sama aduna dafa… »

Slt contan na trop si sa liguey Man vraiment instant bi dama diaxlé trop sakh bilahi j suis une femme de 27ans divorcer avec un garçon ki à 5ans nama divorcer ak legui defna 4ans bobou balegui nak mangui liguey machalla sante yalla j ne manque de rien dafa am benn way bouma nekkal sa fait 7 mois vraiment beugue nako trop sakh mom aussi beugoul koudoul Man sougnou koulo wé sakh dafay dioy bougoul louma meti mai nakk am amam demewoul nonou mai man lolou mom deranger wouma lima meti moy instant bi je suis enceinte de lui té Man wakh deugue yalla dama nekk nitt kou gneup respecter té li beuss bou siwé kenn dotouma respecter gneup dinagnou ma yapp sama copain bamou ko yeugué batay dafa gueneu collant si man vraiment mom dafa contan trop mai nenako gnou marié gaw neub li ou bien ma avorté mai mom nena dou deff mariage temp k amouma dom té beuss bouma rayé domam dinama siweul vraiment diaxlé na té lini ma dal beuss bou siwé sama adouna yakou sama famille gneup dina gnouma bayi

commentaires
Loading...

En poursuivant votre navigation sur ce site, vous acceptez l’utilisation de cookies pour vous proposer des contenus et services adaptés à vos centres d’intérêts. Ok