Le témoignage du jour : sayou niou guissé rek ma diokhko, 2 eme round moniou bolé

Salut a tous j’espere que vous allez bien ,Mane mome diakhlé motakh ma niew fi mane dal sama copain bi mo commencer dima diakhal damay ladj nak beugeu nama wala dafa nek ak mane just pour fowé ma je vous explique mais s’il vous plait nak boulen ma khass l’erreur est humaine
……On a fait 1 an et quelques mois je l’aime beaucoup troopp on fait tout ensemble …Mane nak mome on a couche ensemble presque chaque semaine.
Mais lima diakhal moy heure bouniou nek mou beugeu niou defko damay bagne waxna ba sonou niko niou arreter yoyou parceque moy lolou diadouwoul bene yone mane dama wakh ba sonou khamnani sama diné haramal nako. demna sakh ba di diouli chaque jour di niane yalla mou diégual ma mais mome dafa deugeur bopou heur bouniou néké lou nek lamay wakh dima forcé dima youkhou bama nangou té bouma bagné dafmay méré dou wakh ak mane took nagne 2mois yo khamni damako bayi nanguotouma sakh di guissanté ak mome. metiwone na trop si mane parceque mome rek la beugeu legui nak mou woma nima pour niou guisser maniko carrement bou fékè you niak fayda mane douma niew mounima non doumala sakh lale nieweul rek da am loumalay wakh mane aussi ma dem niou wakhtanne etouu mou recommencer encore beugeu ma forcé maniko doumako def.
ounima li yeup tayouko ay dafa am sama faiblesse lou nek mou wakhko mome dal waxna bama yeureum ko ba diokhko niou paré mounima dafa beugeu 2eme round ma bagne ba teud si souff mou commencer dima youkhou nima par force la maniko ioe dagua eupeul dara la defatoul bou diaré sakh taye niou bayanté wanté douma defate.
Mou méré nangouwoul wakh ak mane depuis bobou batay messagouma wowouma fallétouma té mane je souffre parceque mome rek la beugeu legui kerrok ma message ko niko ioe louy sa blem mounima mane damako commencer yapp. le fait que ma bagnal ko lolou moko meti etou Maniko ya kham regrettee wouma si dara
….Bobou batay lidjentiwoumako insby dama regretter lima diota doundou ak mome yeup parceque mane khamnani douma kou bone. khana key di gueneu goor goor rek pour yalla diégual ma Magui niakhe sama book jiguene gni niou gueneu teyei sen boop parceke dafa am goor you doy war yo khamni Daniouy nek ak ioe juste pour le plaisir Magui diegualou si longueur

Laisser un commentaire

Votre adresse email ne sera pas publiée.